wo
stringlengths 1
4.02k
⌀ | fr
stringlengths 1
1.08k
| source
stringclasses 2
values |
---|---|---|
Nit ñan ŋga wax ? | Tu parles de quels gens ? | null |
Nileen leen | Dites-leur | null |
Mangui lay ndokkel ci tabaski bi | Mes voeux de tabaski | null |
Waaw nataal bii mi ngi wane ab ab wanag lii ab wanag la, wanag bu yànji sax. Ci biir wanag bi nag am nay am na jëfandikaay yoo xam ne ngir boo jëfandikoo ba pare man nga koo jël daal. | Cette photo montre certainement une sorte de douche qui est très large. À l'intérieur de la douche il y a des outils que tu peux te servir après avoir fini. | null |
Ndax mbir mi po kese la woon ? Danoo yëgoon sunu doole, yaakaar ni dara warunu woon a të, rawati-na noon bu nuy dëkk te mënunu koo teg bët. Fo kese ? Ay doomi-tubaab yu xamadi di rajaxe lépp, ni ñenn ñiy dagge tànkiy gunóor walla tanc mbott ci ginnaaw bunt ? Mukk ci àddina. Liñ doon def weesu woon na loolu lépp. Danoo tegoon sunu bopp ñaari ponkal yu am doole, sëppu dunyaa ni nooy boroom. Te ci sama gis-gis, liñ taxoon a ràkkaaju du woon dara lu dul càkkeef gi nu wëroon, màndiŋ mi yaatu ba mel ni amul àpp, ngëlén yeek asamaan si xund, di gëdd ak a xultu. | Était-ce un jeu ? Nous nous sentions pleins de puissance. Je m'en souviens aujourd'hui, non pas comme d'un divertissement sadique de sale gosse – la cruauté gratuite que des petits garçons peuvent aimer exercer contre une forme de vie sans défense, couper les pattes des doryphores, écraser les crapauds dans l'angle d'une porte –, mais d'une sorte de possession, que nous inspiraient l'étendue de la savane, la proximité de la forêt, la fureur du ciel et des orages. | null |
Te dey addina laabiir dafa ci baax. | Du reste la générosité est une bonne chose dans la vie. | null |
Na muy dugge màrse sax, tegtal ci li may wax nii. Du ko caaxaane, moom. Bés bu Yàlla sàkk, ci suba teel, mu ànd ak i daan-dooley naar jubal ja ba. Miinanteek naak ñoom bu baax, ndax li ñuy faral a daje pólis saa yuy yeesaliy kayitam. | Le soin qu'il apportait chaque matin à faire son marché de très bonne heure, en compagnie des travailleurs maghrébins, qu'il rencontrait également au commissariat de police, chaque fois qu'il faisait renouveler sa carte de séjour. | null |
Dugghal waay ! | Mais entre ! | null |
Ci gisu-gisu doomiy Afrig, du bés bi nit ki juddoo la ganesi àddina. Ñoom, dañu jàpp ni bés bi ay way-juram jotee am solo. | Les Africains ont coutume de dire que les humains ne naissent pas du jour où ils sortent du ventre de leur mère, mais du lieu et de l'instant où ils sont conçus. | null |
Kenn fàttewul Aro Suku, ak xeer wa mu daan ñàddee nit ñiy rendi. | La légende d'Aro Chuku et de sa pierre aux sacrifices humains continue d'agir sur les esprits. | null |
Waaw nataal bi de, ay xeer la yoo xam ni dañ dajaloo. Xeer yi nag Daf am am ay pax-pax ci biir, am ay cat-cat. Dafa xaw a marõ. | Sur cette photo ci, il y a des pierres qui sont rassemblées. Cependant, les pierres ont des trous à l'intérieur ainsi que des pointes. Elles semblent de couleur marron. | null |
Baay def na ñaar-fukki fan ci gaal gi, jëm Wiktoryaa. | J'imagine son exaltation à l'arrivée à Victoria, après vingt jours de voyage. | null |
Nit ki ma dajeel ci atum 1948, fekk muy door a jóge Afrig, xawma ko moom ci boppam. Xawma sax wan xeetu nit la. | Tel était l'homme que j'ai rencontré en 1948, à la fin de sa vie africaine. Je ne l'ai pas reconnu, pas compris. | null |
Nataali démb ya àgg fu sore ci man, ni fa tekk, ni dootuñu fa jóge. | Ce trésor est toujours vivant au fond de moi, il ne peut pas être extirpé. | null |
Gindikay bi feyyoona fètt bi. | La bombe avait été désactivée par le pilote. | null |
Góor gi dem la, ma defe ! | C'est l'homme qui part, je crois ! | null |
May fàttaliku nag ray-rayu suuf su xonq si. Tali yi jant bi xarat. Ni nu daan rawantee tànki neen, di xuus ci àll bi, dem ba jub tatay max yi. Te ngoon su ne, ngëlén li dellusi, guddi yi xumb be, fo tollu di dégg i yuux ak sunu muus mu jigéen miy jooteek siiru yi ci kow kër gi. Ak itam sibbiru. Mu daaneel la, nga ni mbàppaaral, su njël jotee ngelaw li yëkkati sanke bi, sedd bi ne cabax ci néeg bi, fekksi la fi nga tëdd, dugg ba ci sa biir yax. | Je me souvenais de l'éclat sur la terre rouge, le soleil qui fissurait les routes, la course pieds nus à travers la savane jusqu'aux forteresses des termitières, la montée de l'orage le soir, les nuits bruyantes, criantes, notre chatte qui faisait l'amour avec les tigrillos sur le toit de tôle, la torpeur qui suivait la fièvre, à l'aube, dans le froid qui entrait sous le rideau de la moustiquaire. Toute cette chaleur, cette brûlure, ce frisson. | null |
Naka-nga sant ? | Comment t'appelles-tu ? | null |
Yéena ŋgoogule foofu ci biir ! | Vous voilà là à l'intérieur ! | null |
Daŋgeen di naŋgu mbaa du dem ! | Vous acceptez ou il ne part pas ! | null |
Fu waay geestu, say bët daj téeméeri junniy gone yu wow koŋŋ, niróotuñu sax nit. | Le long des routes, au bord des rivières, à l'entrée des villages, des centaines de milliers d'enfants sont en train de mourir de faim et de déshydratation. | null |
Xar mi mépp. | Le mouton en entier. | null |
Yeewal mépp xar ! | Attache tout mouton ! | null |
Wax naa ko mu ñibbi. | Je lui ai dit de rentrer. | null |
Njiit mi retraitee US Air Force la. | Le chef est retraité de l'US Air Force. | null |
Seet ŋga néeg buu ? | Tu as regardé dans cette chambre-ci ? | null |
Suñ fa jógee, sonn, ne yàcc, nelaw ba fajar. Su ngelawu njël lu sedd liy raay sànke bi, dina fekk ku ci nekk a ngi kott moroom mi, fekk it riiri sabar yiy dakk ndànk-ndànk. | Puis ils s'endorment à l'aube, dans le souffle froid du matin qui fait onduler le rideau de la moustiquaire, enlacés, sans plus entendre le rythme fatigué des derniers tam-tams. | null |
Góor gi giskoon na la | L'homme t'eût vu | null |
Dem ŋgeen | Vous partez | null |
Waxuma yooyale xale ? | Je ne parle pas de ces enfants ? | null |
Ana waa kër gi ? | Où sont les membres de ta famille ? | null |
Afrig dafa dekkali woon doŋŋ njub ga masoon a nekk ci moom. | Elle avait révélé en lui la rigueur. | null |
Ŋga dem la, góor gi bëgg. | Que tu partes, c'est ce que désire l'homme. | null |
Nataal bii de ñaari président la. Fii nag France la mu di président Maki Sàll ak Macron ñi ngi noon di dox ci affaire bu rouge bi. Am na oto yu topp seen gannaaw. Am na ñu taxaw seen wet yor lu mel ni ay fiil ay policier lañ. Maki Sàll ak Macron ku nekk sol yére bu ñuul ak dàll yu ñuul kostin. | Sur cette photo se trouvent deux présidents. Ici, c'est en France. Il s'agît des présidents Macky Sall et Macron. Ils sont là, marchant sur un tapis rouge. Il y a des voitures qui sont derrière eux. Il y a des personnes debout à leur coté portant ce qui semble être des fil électriques ; ce sont des policiers. Macky Sall et Macron, chacun d'eux porte des habits et des chaussures noirs <unk>. | null |
Waaw lii nag ay néegi ñax la, néegi ñax bi ci kaw dañ kaa defar ko bam taaru lool. Bi ci des tamit ñu defar ko jël ab sars wërale ko ci kaw wutal kob buntu. | Ceux-là, cependant, sont des cases. Celle qui est en haut est conçue d'une très belle manière. L'autre aussi est conçue en prenant une charge et l'entourant autour et en lui fournissant une porte. | null |
Jigéen ji, moom waxatul ! | La vieille, elle, ne parla plus ! | null |
Àndal ak yar ! | Sois avec politesse ! | null |
Coppite gi may njort doon na àgg ba ci waxinam ak ni muy jokkook ñeneen ñi. Làpptoo ko naroon a jàppale, xam naa, walla muy làkk « pijinu » àngale – bi jotewul daraak kerewolu dunu Móris bu sell ba te yiw. Ci gàttal, benn kàddu mën naa tënk li may bëgg wax, te mooy : maasaloo. Su Baay toogoon Tugal, du xéy ba dégg lu mu masul a dégg. Te it képp ku mu faj, dina jàpp ne mook moom benn lañu, bokk waaso. Maasaloo. Walla sax seey ? | Mais ce que cela aurait changé en l'homme qu'il était, qui aurait mené une vie plus conforme, moins solitaire. De soigner des enrhumés et des constipés, plutôt que des lépreux, des impaludés ou des victimes d'encéphalite léthargique. D'apprendre à échanger, non sur le mode exceptionnel, par gestes, par interprète, ou dans cette langue élémentaire qu'était le pidgin English (rien à voir avec le créole de Maurice raffiné et spirituel), mais dans la vie de tous les jours, avec ces gens pleins d'une banalité qui vous rend proche, qui vous intègre à une ville, à un quartier, à une communauté. | null |
Yeneen xar yi yépp daw. | Tous les autres moutons fuirent. | null |
Kañ ñgay dem ? | Quand pars-tu ? | null |
Walla xéy-na léeg-léeg nga làqu fomp rangooñ. | Sans doute verser des larmes. | null |
a ngi waxaale seen àdduna si nu wanteer | marchandent le prix de leur avenir bradé | null |
Dem, rafetoon na ! | Avoir été, eût été bon ! | null |
Maangi ci kowam, ndanka, ndanka. | J'y suis avec, petit à petit. | null |
Lii ag kër la, kër gu yàqu. Boo ko gisee xam ni dafa màgget ak làmpam yeek palanteer am yi. | Ceci est une maison, une maison endommagée. En le voyant tu sauras qu'elle est vieille ainsi que ses lampes et ses fenêtres. | null |