wo
stringlengths
1
4.02k
fr
stringlengths
1
1.08k
source
stringclasses
2 values
Loo gis ci biti
Qu'as-tu vu dehors ?
null
Jox na nit ki dara.
Il a donné à la personne quelque chose.
null
Waxal góor gi mu dem !
Dis à l'homme de partir !
null
Foo jaŋge xerëm ?
Où t'es-tu initié en sciences occultes ?
null
Keneen ki la, defe naa !
Je crois que c'est l'autre !
null
Ku dem, gaynde la !
C'est peut-être un lion !
null
Béppu dëkku Séeréer set na !
Tout village Sérère est propre !
null
Sëriñ bi ñaan na mayewoon alalam ji ba mënkóon yalwaan.
Le marabout implora qu'il fût dans la situation de quelqu'un qui aurait fait don de sa fortune, pour être en mesure de demander l'aumône.
null
Demkoon ŋga
Tu serais parti
null
Namm naa la
Tu me manques
null
Jox na ka keneen ku sawar.
Il l'a donné à quelqu'un d'autre de très actif.
null
Xar man moo réer ?
Quel moutons est égaré ?
null
Wante woowa ma la yóot it deey bonul.
Mais celui que je t'ai donné n'est pas mauvais non plus.
null
Am naa benn decukaay bu donggal ab jariñoo.
J'ai 1 magasin spécifique.
null
Góor gii demoon
Cet homme qui a été
null
Ñam yiy xeeñ – soosu gerte, fufu, mburu walla ňàmbi. Nuy déglu Baay muy nettali na mu yendoo. Lëppaa-lëppi guddi yeek yeneen gunóor yaa ngiy wéy di dal, sindax yi gënatee ràŋŋatiku, biti bi raglu ba nga ni lii lu mu doon. Guddi gii kay, ak tàngaayam bu tar, du guddig féexlu. Wute na lool ak sunuy guddiy bàyyeeku Tugal ya. Fii, coonook fitna rekk a fi am.
L'odeur de la soupe d'arachide, du foufou, du pain de manioc, la voix de mon père avec son accent chantant, en train de raconter les anecdotes de sa journée à l'hôpital, et le sentiment du danger au-dehors, l'armée invisible des papillons de nuit qui frappait les volets, les margouillats excités, la nuit chaude, tendue, non pas une nuit de repos et d'abandon comme autrefois, mais une nuit fiévreuse, harassante.
null
Maa ngi jeema paré sama mbebët ayubes bu si topp.
J'essaie de terminer mon projet la semaine prochaine.
null
Wau.
Oui.
null
Nit ag gaynde duñu dëkkóo.
Homme et lion ne cohabitent pas.
null
Gis naa xale ba.
J'ai vu l'enfant.
null
Bëcëk baangi fi rek.
L'après-midi se passe bien.
null
Gis na keneen ki.
Il a vu l'autre.
null
Ci biir ! ndax mu dugg
À l'intérieur ! pour qu'il entre
null
Xare bi jeex, ñu tekk ci ñaar-fukki at, ma ànd ak sama yaay ak sama mag ju góor, nun ñett ñépp nu jaar fa mu jaaroon, dem fekki ko Afrig.
C'est ce même voyage que j'ai fait, vingt ans plus tard, avec ma mère et mon frère, pour retrouver mon père au Nigeria après la guerre.
null
Wax ji yépp, bañ-ŋga-ñëw la.
Tout ce bavardage, c'est pour que tu ne viennes pas.
null
Yenn ciy dëkkam yi féete sowu-jant dañoo teel a teqalikook Niseryaa, mu doon li gën ci ñoom, musal leen ci ger ak reyante yu dul jeex.
Le haut pays de l'Ouest, en se séparant du Nigeria, avait fait un choix raisonnable, qui le mettait à l'abri de la corruption et des guerres tribales.
null
Daan na maasaloo yit ak réewu Ibo yi, seeni néegi-ñax yaak dexug Ayaa, ba ca sax jànq yaak miir ya amoon melo suuf.
Elle s'harmonisait avec le pays Ibo, avec le tracé de la rivière Aiya, avec les cases du village, leurs toits couleur fauve, leurs murs couleur de terre.
null
Keneen demul.
Aucun autre n'est parti.
null
Nu jàng it ni Baay mii de, ëpp naa jaawaleek sunu maam ju jigéen ji nga xam ni ak njaaxum loo mën a def soo naxanteek moom, tuur ko lëndëm mbaa jaay ko reewande mu ni la : « Waaw baax na, fompal say rangooñ, waaye bul ko defati, dégg nga ? » Góor gii daal, moo doon liñ naan Àngale xamul tama : doo ko jàll baat te soo fa nekkee naan dangay daanu gàngiri, mu jekkali la faf. Te sax këru Ogosaa ga, sama xel mënutoon a dem benn yoon ci daanu fa gàngiri : këru suuf la woon te it amutoon i móobal yu ma mënoon a mer, sànni leen fu ma neex.
Qu'il fondait cette justice sur l'exemple, refusait les tractations, les délations, tout le jeu des larmes et des promesses que nous avions accoutumé de jouer avec ma grand-mère. Qu'il ne tolérait pas la moindre manifestation d'irrespect et n'accepterait aucune velléité de crise de rage : l'affaire pour moi était entendue, la maison d'Ogoja était de plain-pied, et il n'y avait aucun meuble à jeter par aucune fenêtre.
null
Demal !
Va !
null
Bi ma delloo dëkk ba ma juddoo, dama faa meloon ni gan. Du kenn ku ma fa xam, safatul dara ci man. Li nu jóge Afrig jur ci man tiis wu réy. Su ma yaboo sax ni mënuma woon a nangu ni maak samay way-jur dëkkëtuñu Afrig. Ca laa tàmbalee gént ni sama yaay nit ku ñuul la, di sàkkal it sama bopp cosaan lu bees.
J'ai longtemps rêvé que ma mère était noire. Je m'étais inventé une histoire, un passé, pour fuir la réalité à mon retour d'Afrique, dans ce pays, dans cette ville où je ne connaissais personne, où j'étais devenu un étranger.
null
Nit ñeñeen la gis !
C'est d'autres gens que j'ai vus !
null
Xanaa ay doom yu wex ci sàqam
Des fruits amers dans son grenier
null
Góor gee ni mi ŋgi fi, soo demee !
C'est l'homme qui a dit qu'il est là, certainement !
null
Sama yaay moom, deful woon dara muy dara.
Quant à ma mère, c'étaient la fantaisie et le charme.
null
Lu ñàkk soloo ko daan sooke, ñaare, moo xam kaas boo toj la mbaa nga xool ko bët bu ko neexul mbaa nga koy jaay dijj ŋaam. Lu ne mënoon na koo teqaleek sagoom, mu lay wulli ak i yat mbaa di la kurpeñ.
Pour un rien, un bol cassé, un mot de travers, un regard, il frappait, à coups de canne, à coups de poing.
null
Gis naa sa xarit yépp !
J'ai vu tous tes amis !
null
Waaw lii nag aw saañ la wuñ tabax ba noppi def fa ñaari raxasukaay tijji robinet bi muy sotti.
Ceci est une bouche qu'on a conçue, dans laquelle on a mise deux endroits pour se laver les mains et ouvert le robinet pour le laisser couler.
null
Dem ŋga, te dem na, te dem naa.
Tu as été et il a été et moi aussi j'ai été.
null
Góor ñi dem nañu
Les hommes sont partis
null
Kenn ki génn ki yeksi na.
Cet autre-ci qui est sorti est arrivé.
null
Waa ji demkoon na
L'individu devait partir
null
Gis ŋga ñooñale ñan ?
Tu as vu ceux-là lesquels ?
null
Góor gi daan liggéey
L'homme qui travaillait d'habitude
null
Yaw mile mi fii !
À toi qui es-là !
null
Soo demee, Faatim la !
C'est Fatim, si on va au fond des choses !
null
Gisul yeneen.
Il n'en a pas vu d'autres.
null
Ñu mujjee jàpp Baay, ni ko na dellu fa mu jóge.
Finalement, il est arrêté, refoulé.
null
Góor gii di dem
Cet homme qui part
null
Ndaxam de, Ogosaa, dara fattu fa woon sunu xel ak sunu yaram : noo moomoon sunu bopp, loolu jur saň-saň bu mat sëkk.
Pourtant c'était la liberté totale du corps et de l'esprit à Ogoja.
null
Noonu, mu jog.
Alors, il se redressa.
null
Waaye man sax dama dul ñëw !
Mais, même moi, je ne viendrai pas !
null
Gisoon naa nit ñooña ñépp.
J'ai vu tous ces gens, auparavant.
null
Yéen ñan la wax ?
Il parle desquelles de vous ?
null
Bala nu gunóor yi daan léjal dëgg, guddi jot, ba ñu taal làmp yi. Dañoo meloon ni ñuy defanteek nun. Ay naaxi-naaxi gunóor a doon song néeg bi.
Chaque nuit, dans une sorte de revanche du monde animal, la case était envahie par des myriades d'insectes volants.
null
Li muy gis subaak ngoon yombut a dékku. Yaram yu tàng jërr, newwi mbaa ràgg ; kanam yu ngaana walla siti yàq yaxeet ; jigéen ñi dem ba matook a matuwaat faf leen teppi ; gone yu ndóol teel a màggetloo, seen der dem ba dóomu-taal, seen karaw xonq ni weñ gu xoomag. Seen bët yi, nag ? Ñu ngi ne keww, mel ni ñu ni jàkk Dee, muy waaxu di ñëw, war leen a jëlsi yóbbu laaxira.
La proximité de la souffrance le fatigue : tous ces corps brûlants de fièvre, ces ventres distendus de cancéreux, ces jambes rongées d'ulcères, déformées par l'éléphantiasis, ces visages mangés par la lèpre ou la syphilis, ces femmes déchirées par les accouchements, ces enfants vieillis par les carences, leur peau grise comme un parchemin, leurs cheveux couleur de rouille, leurs yeux agrandis à l'approche de la mort.
null
Toogal ci fépp, fu leer !
Mets-toi n'importe où, où il fait clair !
null
Ñax mi muur joor gi dafa bare ba may fàttali géej, xóot te raglu ni moom.
La plaine d'herbes devant la case, c'était immense, dangereux et attirant comme la mer.
null
Góor gi doonkoon na boroom xamxam.
L'homme eût été un savant.
null
Bi ma demee ba sori ci mbindum téere bii, laa door a xam ni li may dekkali romb na may dem.
C'est en l'écrivant que je le comprends, maintenant. Cette mémoire n'est pas seulement la mienne.
null
Te moontin xamante nañu.
Et pourtant ils se connaissent.
null
Bés bi rajo biy fen di dajale, naan noon bi jekku nanu ko, mënul sax weesu dexug Maarn, sama yaay a ngi janook soldaari Almaañ yiy maaj ci suufu palanteeram, ca Pomu-Làbbe.
En Bretagne, ma mère voit les troupes allemandes défiler sous ses fenêtres, à Pont-l'Abbé, alors que la radio annonce que l'ennemi est arrêté sur la Marne.
null
Gis na ka, moom, Musâ !
Il l'a vu, lui, Moussa !
null
Waaye Ogosaa, saa yu fa suma xel delloo, du tàngaay baa tax.
Mais je ne me rappelle pas avoir eu chaud à Ogoja.
null
Bayyi ma !
Laisses moi tranquille !
null
Naka njaboot gi ?
Comment va la famille ?
null
Guy yow miy ñaan jant bi
Baobab implorant le soleil
null
Yeneen fas yan ŋga gis ?
Quels autres chevaux as-tu vu ?
null
Kon fàttalikoo meññ téere bu ndaw bii.
En souvenir de cela, j'ai écrit ce petit livre.
null
di saay ciy daay ?
mourir de feux de brousse ?
null
Ñenti alkaati, ñaar ñi yor seen bat ñow di àtte ñaar ñu nekk di xeex tëdd ci suuf. Mu am benn taatu garab bu nekk ca wet ga, am benn waay bu ñëw.
Quatre agents de police, les deux portent leurs <unk> venant séparer les deux se battant sur le sol. Il y a le sommet d'un arbre sur le coté et un homme arrivant.
null
Nataal bii ngeen ma yónnee gis naa ci biir nataal bi tabax bu màggat lool, am garab gu sax ca biir tabax ba. Tabax bi nag bu màggat a màggat la.
Sur la photo que vous m'avez envoyée j'y ai vu une vieille construction. Des arbres ont poussées à l'intérieur de la construction. La construction est vraiment très vieille.
null
Nga jóge fa, dox tuuti daldi àgg fa doomi réew miy dankalikoo. Kilifay Tubaab yooyu nag, lijjanti seeni mbir, xam kan moo ciy kan ak lan la ku ci nekk yelloo, yombul. Ridyaar Kipliŋ jéem na cee bind ci wàllu Eend, ni ko Raaydëer Agaard jéeme ci penkub Afrig.
Un peu plus loin, le cercle des colonisés, avec l'échafaudage complexe qu'ont décrit Rudyard Kipling pour l'Inde et Rider Haggard pour l'Est africain.
null
Góor gee ni, soo demee, mi ŋgi fi !
C'est l'homme, certainement, qui a dit qu'il est là !
null
Ak lu mu mën a doon, xaley Ogosaa ya masuñoo fekke fu nuy toje ay jànj maak sama mag.
Les enfants du village n'étaient jamais avec nous quand nous partions détruire les termitières.
null
Wande it, xale yi dañu soxor.
Mais, les enfants sont toute-fois méchants.
null
So demee, mi ŋgiy wax !
Il est entrain de parler, peut-être !
null
Xale yi set nañu ci biir, ci biti gisuñu dara.
Les enfants ont cherché à l'intérieur, à l'extérieur, mais n'ont rien trouvé.
null
Menn xar réerul.
Aucun mouton ne s'est égaré.
null
Agsil
Viens
null
Lan moo dugal sama bopp bi ne bés bi ma jëkkee gis Baay ca Ogosaa, xeetu lonet yooyu ñu mën a woowe xoolukaay la takk ?
La première fois que j'ai vu mon père, à Ogoja, il m'a semblé qu'il portait des lorgnons.
null
Góor gu màggat doŋŋ a fi desoon, gëlëm, réer, xamatul lu ko àddinay nirool.
Mais un vieil homme dépaysé, exilé de sa vie et de sa passion, un survivant.
null
Ana boroom kër gi ?
Où est le maître de maison ?
null
Ñan la ?
Qui est-ce ?
null
Gis na keneen ki woon.
J'ai vu l'autre, dont il fut question.
null
Gisal Musaa doŋŋ !
Vois Moussa simplement !
null
Na dugg ci biir su bëggée !
Qu'il entre !
null
Jant biy lakk seen yaram. Mar di leen miirloo, ngeen war a xuus ci biir dex gi, ndox mi sedd guyy, di yéeg ba ci dënnu fas yi.
La brûlure du soleil, la soif qu'on ne peut étancher, ou le froid des rivières qu'il faut traverser en plein courant, avec l'eau jusqu'au poitrail des chevaux.
null
Kookule la ci biti.
C'est celui-là qui est dehors.
null
Xoolal mbër mu.
Regarde ce lutteur.
null
Nit la te góor ŋga !
C'est un homme de chair et d'os et tu es un homme !
null
Nit ag gaynde duñu dëkkóo.
Homme et lion ne peuvent cohabiter ensemble.
null
Bokk na ci li koy firndeel, ni samay way-jur fonkee seen kër : néegu-ban bi muroo ay xobi garab, ëtt bi jigéen ñiy dajaloo bés bu nekk, gapparu, di xaar seen doktoor.
À l'amour qu'ils avaient pour leur maison, cette hutte de boue séchée et de feuilles, la cour où chaque jour les femmes et les enfants s'installaient, assis à même la terre, pour attendre l'heure de la consultation, un diagnostic, un vaccin.
null
Ci biir fiy leer
Là où il y a de la lumière
null
Góor doŋŋ ŋgeen !
Vous êtes des hommes tout simplement !
null
Deg nga Angale ?
Parles-tu Anglais ?
null
Dëkku Séeréer ban ŋga wax ?
Tu parles de la ville de quel Sérère ?
null
Nit ñan ñoo réer ?
Quelles personnes se sont égarées ?
null
Laata nuy àgg dëkki max ya, dañ daan def tànki neen di xélu, di tëb ci kow xer yeek kekk li naaj wi xaratoon.
Nous courions à toute vitesse, pieds nus, loin de la maison, à travers les hautes herbes qui nous aveuglaient, sautant par-dessus les rochers, sur la terre sèche et craquelée par la chaleur, jusqu'aux cités des termites.
null
Kenn demul
Nul n'a été
null