wo
stringlengths
1
4.02k
fr
stringlengths
1
1.08k
source
stringclasses
2 values
Bis budul jeex bii moo gëna bon
C'est pire avec cette journée sans fin
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yaay.
Je suis désolée.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Déedéet, du waxtu wi war.
Non, ce n'est pas le bon moment.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
(dafay yuuxu) FUCK.
- Je sais.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kon dama jàpp ni dama wara fóon.
Alors je pense que je devrais avoir un baiser.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Doom, loo bëgg?
Tu veux quoi, mon fils?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Am ku bëgga granit?
Quelqu'un veut du granit?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Fan laay dem ak yaw?
Je vais aller où avec toi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Guddi gi doo ko fàtte ba fàww.
Ce sera une nuit inoubliable.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lite ak light ay tur lañu ñuy jëfandikoo ngir wax ci vin ak whisky.
Lite et light sont des termes utilisés pour décrire les vins et les whiskies.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maanaam, ñooñu ay taskatu xibaar lañu, duñu musa bind ci mbaam xuux.
Ce sont des journalistes qui n'écrivent jamais sur les cochons.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dédeet, danga wara dem fu gëna sori.
Non, tu dois aller plus loin.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xale bu jigéen bi dafa soloon robb bu xonk.
La fille portait une robe rouge.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Leegi mingi tëdd ci koñu cammoy bi ci bàmmeel bi.
Elle est allongée dans le coin gauche du cimetière.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kontaan naa ci gis la, Jack.
C'est bon de te voir, Jack.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Daara bu kawe bi gëna mag te gëna mag ci àdduna bi - Oxford - xamle na ni dafay fomm dajale taalif yi.
La plus ancienne et la plus grande édition universitaire au monde, Oxford, vient d'annoncer qu'elle annule sa collection de poèmes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci jëfin wi, mën nañu jàpp ne xaalis bi njëwriñ ju ne di jëfandikoo ci at mi dañu ko teg léegi ci ay tëralin yu lim ba mën a nekk ci diggante ñaar ba juróom-ñeent.
D’un point de vue pratique, on peut retenir que le budget de chaque ministère est désormais présenté sous forme de programmes, dont le nombre varie entre deux et neuf.
galsenai/french-wolof-translation
Target baaxna.
La cible est bonne.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci gàttal.
À la fin.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dama toogoon ci wetu lalu Bonzo di ko xaar mu wér, amaana du musa yewwu.
J'ai attendu le réveil de Bonzo. Il se peut qu'il ne se réveille jamais.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndawi liggéeyukaay bi dañuy sol tënu.
Les représentants de la compagnie portent des costumes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Juróomi téeméeri milyoŋi lan?
Cinq cents millions de quoi ?
galsenai/french-wolof-translation
Xarala yu bees yi dañu leen di jëfandikoo bu baax ci wàllu liggéey ci réew yooyu ndax dañu jàpp ni yokkute dafay firndeel liggéey bi, du jumtukaay.
La technologie est largement utilisée dans les processus commerciaux de ces sociétés, car le progrès est considéré comme une validation de l'entreprise plutôt qu'un outil.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Seddale? - Lu muy tekki ?
- Ça veut dire quoi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Danu wara nekk ak boroom alal yi gëna am xel ci àdduna bi te ñoom ci seen bopp lañu ko def.
On est censés être avec les investisseurs les plus intelligents du monde et ils l'ont fait eux-mêmes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ingénieur mën na am ci diir bu mujj.
L'ingénierie ne peut avoir lieu qu'à la dernière étape.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Loolu nag, gannaaw ba Baay Móodu Faal mi ñuy woowe Booy Jinne rëccee ci dibéer fan-weeri fan ci weeru mee mi mujj ca ëttu àttekaay gu Liberte VI ga ñu ko tëjoon bu yàgg.
Ce, suite à l'évasion de Baye Modou Fall alias Boy Djiné survenue le dimanche 30 mai dernier au Camp pénal de Liberté VI où il était détenu depuis longtemps.
galsenai/french-wolof-translation
Doomu Kausalya mooy Ram
Et le fils de Kausalya était Ram
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lu nekk ci nun di def fii?
Que faisons-nous ici, vraiment?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waxtu la woon 5:50 ci suba bi.
Il était 5 h 50.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Man Donnie laa tudd..
Mon nom est Donnie.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dama ragaloon Klaus, nekk yaay, mu def ma yëg ni amnaa jàmm.
J'avais peur de Klaus, d'être une mère, et il me faisait me sentir en sécurité.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Sumaal bii mooy sama yelleef bima juddoo.
Ce journal est mon droit de naissance.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kon mag ñi jarul ñu jàngal xale yi ci seen bopp, mel ni dañuy jàngal xale bu ndaw bi mu nekk wattukat, walla def tàggat yaram wala yeneen mbir yu mel noonu.
Par conséquent, les adultes n'ont pas besoin d'enseigner les enfants en privé, comme s'ils enseignaient à un enfant à être un gardien ou à faire du sport ou des activités semblables.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bernstein leeralul.
Bernstein ne donne pas plus de détails.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Biñu ko waxee Ram mu dem, ci la wax ni dina dem.
Et Ram, quand on lui a dit de partir, a effectivement dit qu'il le ferait.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dañu ko tëye.
On a été retenu.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Duñu mës a woteel nit ku ñuy tuumaal yakktaan.
On ne votera jamais pour une personne accusée de viol.
galsenai/french-wolof-translation
Xale bu ndaw bi!
Quel gamin!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Te dañu wara wax lii ñépp ci New York City!
Et on doit le dire à tout le monde à New York!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bul ma woowe noonu.
Ne m'appelle pas comme ça.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Faale wuma loolu.
Je m'en fous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Mu daw topp xale bi.
- Il a couru après le garçon.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mënu nu...
On ne peut pas...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Xale kaña?
- Le petit rat?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Soxlawolen nëbb xam-xam bi ci sa armuwar
Tu n'as pas besoin de cacher la sagesse dans ton placard
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Tiitaange gi mingi ci biti!
La menace est là-bas!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi ñaan Apollo nga xam fu sori nga ci yoonu sa pàppa.
Je prie Apollon pour que tu réalises à quel point tu t'es éloigné du chemin de ton père.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Sunu lim bi fi nekk mingi tollu ci 7811, lu doy ngir lakk gaal ak larme yu Stannis Baratheon yépp.
Notre nombre actuel est de 7811, assez pour brûler la flotte et les armées de Stannis Baratheon.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Point biñu jël.
Le point est pris.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Tay tàngoor wi ëpp na juróomi degre tàngoor wi war.
Aujourd'hui, la température est de cinq degrés plus élevée que la normale.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Mu dóor ma dóor te amul benn sabab.
- Il m'a frappé sans raison.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñu ngi ci biir batimaa bi.
Ils sont dans le bâtiment.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Danga dagg sa bopp ci resif bi.
Tu t'es coupé sur le récif.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
/ Sama xarit la.
- C'est mon pote. - Je sais.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nu dajewaat.
On se retrouve.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Wells, sama waajur, amuma xaalis.
Je n'ai pas d'argent.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dañuy laaj nga aktive loxo.
Activation manuelle requise.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Man itam.
- Moi aussi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Laayi.
Le prêtre.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Tay bi Abhimanyu waxee ci aéroport bi...nu leeralal ko...
Aujourd'hui quand Abhimanyu nous a parlé de cela à l'aéroport... nous lui avons dit clairement...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ak puus xaritam bi gëna baax ci kamioŋ.
Et de pousser sa meilleure amie dans un camion.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Griggs.
Je suis Griggs.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ku am xalaat bumu jàpp ni moo gën sama xalaat...
Si quelqu'un a une idée qui lui semble meilleure que la mienne...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Jëkkër ak jabar yu yàgg lañu.
- On est un vieux couple marié.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Delloosi ma!
Je veux rentrer!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndax bëggoon na Patroclus ba noppi fayyu deeam.
Parce qu'il aimait Patroclus et vengeait sa mort.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bokk na ci nit ñu néew ñi amul fenn ci lépp luñuy def.
Il était l'une de ces rares personnes qui sont tout simplement exceptionnelles dans tout ce qu'ils font.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dina nu ragal.
Ils auront peur de nous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Duma.
- Je ne suis pas.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Niveau 3 nord.
- Niveau 3 au nord.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Te leegi mingi nii!
Et voilà où elle est!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dina la dundal bu baax.
Elle te nourrira bien.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bëggoon nañu sama kiliyaan.
Ils voulaient mon client.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Gerrard jëemna dara ci xaaj bi ndax gennena Coulibaly tekk Ryan Kent te boobu coppite daanaka amna njeexital ci saas yi ndax eliye bi paasna Morelos waaye Kelly mu xareñ mi juge ci rëddam bi daaw xañ ko ko.
Grâce à ces écouteurs, on peut réellement entendre les effets des atomes relâchés dans les minéraux par la radioactivité. »
galsenai/french-wolof-translation
Jërëjëf ci guddi gi weesu.
Merci pour hier soir.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Hodor ak Summer dee nañu ngir yaw.
Hodor et Summer sont morts pour vous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
KAAY FII.
Viens ici.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bëgg nga gis lu amul fenn?
Tu veux voir quelque chose de spécial?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nit ñi dañuy sànni xaalis ci biir doonte firnde bi dafa wax deet
Les gens jettent une pièce à l'intérieur même si le panneau dit non
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Man maay benn ci ñi sos sosiete bii.
Je suis un membre fondateur de cette société.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nguuru Nazy yi nangu wuñu ko.
Le régime nazi ne le tolérait pas.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
O xale!
Je suis un garçon!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Juumteg Rookie.
Une erreur de débutant.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amna dokimaa yu sell.
Il n'a pas de casier.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Doxalin wi nga xam ne dafay fitnaal ñi nga xam ne lu leen neex def wala ñi bopp kese yitteel, dana rataxal diggante yi, te it dana tax lépp lu waay di def dana ko seet, seetaat ko.
Cet engagement, impliquant répression volontaire des tendances instinctives et des passions égoïstes, pacifie les rapports à autrui et fait émerger des conduites raisonnées, réfléchies, mesurées.
galsenai/french-wolof-translation
Fattelikul tontu am....denga saccoon këyit bi? - “oh, oh lan?
Au cours d’une première période bien chargée, Sullivan a relancé l’équipe locale à 13:10 avant que Matt Marquardt ne se mette au service de Cownie, à 15:16, avec une égalisation.
galsenai/french-wolof-translation
Dunu jiite.
Il ne nous dirigera plus.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Li soxal Eggaliis yi , neena njaxxare am moy xaalis boobu juge ci njaay yi du yagge ni ko njiit yi fooge, " te mu gaaw mbaa mu yagg yepp bës dina ñew ñu delluwaat fi ñu tammbalewoon."
Quant aux églises, les fonds provenant de la vente d’édifices s’épuiseront bien avant ce que s’imaginent les responsables et cela le préoccupe : « tôt ou tard, ils reviendront à la case départ ».
galsenai/french-wolof-translation
Erik, yaa wax sa bopp, nun noo gëna baax.
Erik, tu l'as dit toi-même, nous sommes les meilleurs.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi nii ci Sydney, foofu tay ci suba,
Je suis ici à Sydney, où plus tôt aujourd'hui,
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Duma am wërsëg.
Je ne fais pas de chance.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Parc national bu Kimbale amna fukki ñay ak juróom benn rhinocéros.
Le parc national de Kimbale compte dix éléphants et six rhinocéros.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lu ngay def?
Tu fais quoi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Keyta Balde, dellusiwaat na ci fukk ak benn yiy door joŋante bi, ak Mbay Ñaŋ, ci kaw, ñoo gën a yéexal gaawaayu po mi niki ñiy aar caax yi (defãseer yi) ci geneen wàll gi.
Keita Baldé, de retour comme titulaire, et Mbaye Niang, en pointe, ont plus pesé sur le rythme, très lent, de la rencontre que la défense adverse.
galsenai/french-wolof-translation
Tribunaal bi jëfandikoo na kàttan googu ñeenti yoon ci juróom fukki at ak juróom yi jiitu guerre civile.
La Cour a utilisé ce pouvoir quatre fois au cours des cinquante-cinq années précédant la guerre civile.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Nekkul fa
- Il n'est pas là.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dof rek.
Je suis fou.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Demokarat yi ak repibilikeen yi bokk liggéey
Démocrates et républicains de Caroline du Sud travaillant ensemble
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaw kay, yaay.
Je suis désolée.
bilalfaye/english-wolof-french-translation