wo
stringlengths
1
4.02k
fr
stringlengths
1
1.08k
source
stringclasses
2 values
Xam nga ni, ci ñi bokk ci kuréel gi bokk na ci alumni yi ak alumni yu njëkk ya, ñuy jox $1,000 wala lu ëpp at mu nekk daara ju mag ji.
Comme vous le savez, les membres de cette association sont des anciens élèves qui donnent chaque année au moins 1000 dollars à l'école de droit.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Saa-ótiris bi jóge ne Bayem Munich ci coobare boppam gannaaw fukki at ak benn yi weesu ci këlëb bi ak fukki raayay Bundesliga yi mu am.
L’Autrichien est arrivé libre du Bayern Munich après 11 ans passés au club et 10 titres en Bundesliga accumulés.
galsenai/french-wolof-translation
- Kan mooy Katia bii?
- Qui est cette Katia?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndawu Al Qaida tukkiwoon na Bosnie
Le membre d'Al-Qaïda s'était rendu en Bosnie
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Otto Frank demoon na nëbb lu ëpp 25 weer
Otto Frank est resté caché pendant plus de 25 mois.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lu nga doon lekk?
Tu aurais mangé quoi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Macwell bu plat ngir sarsewaat bu yomb.
Macwell plat pour une recharge facile.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Baaxna, baaxna, nanu dem.
Très bien, très bien, allons-y.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Park nasionaal bu Kinabalu amna fukki ñay ak juróom benni giraf.
Le parc national de Kinabalu abrite dix éléphants et six girafes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dafa melni, oh, sama boroom.
Elle est comme, oh, mon Dieu.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lii ab càcc la ci Cascino, jaaykatu takkaay yi.
C'est un vol à la bijouterie de Cascino.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kent ñëwal.
Je suis désolée.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Jumtukaay yooyu yépp dina ñu la aar bu baax.
Tout cet équipement vous protégera.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Buur bi yónnee nama fi ayu-bis ci ginaaw joge Naya
Le roi m' a envoyé ici il y a une semaine de Naya
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Etat bi amna ay barab yu mu yor, lu ci melni park national bu Kinabalu.
L'État a couvert des zones, y compris le parc national de Kinabalu.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndax mën naa am?
Je peux en avoir?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñi am xel ñu bare waroon nañu bàyyi seeni jikko.
Beaucoup de sages ont dû abandonner leurs habitudes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Ci Bagoas!
- À Bagoas!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xam nga, sudee dama am jabar ak ay doom te duma woon man kese ci kër gi.
Tu sais, si j'avais une femme et des enfants et que je n'étais pas tout seul à la maison.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Noo ngi ànd ak yaw, Alexandre!
- On est avec toi, Alexander!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Danga fees dell ak surprise!
Tu es vraiment pleine de surprises!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Casinos danuy def lunu mën ngir yokk waxtu ak xaalis bi nga xam ne kiliyen yi moom lanuy def ci seen bërëb yi. Palanteer ak montar du fa am, te gennukaay bi dafay jafee gis.
Les casinos font généralement de nombreux efforts pour maximiser le temps et l’argent dépensés par les clients. On y trouve rarement des fenêtres et des horloges, et les sorties peuvent être difficiles à repérer.
galsenai/french-wolof-translation
Sunu jeegoo yu bari ñu ngi ci liggéey
La plupart de nos efforts sont au travail
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Génn ci xol bu xóot bi...
Sortez du fond du cœur...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Déedet. Nga bàyyi ko.
Arrête tout de suite.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Juróom-ñaari at, ba léegi Senegaal ndox mi doyu fi, looloo waral gaa yi di teey ca la njiitum réem mi waxoon.
Sept ans après, le Sénégal manque toujours d’eau et fait face à des pénuries récurrentes et en accordéon, faisant douter fortement de la sincérité du regret émis par le président.
galsenai/french-wolof-translation
Dëgg dëgg Afrig sibsahariyen, ci li am solo ci mbey mi, siiwaloon nañu ko – li koy firndeel mooy teewaayu njéeréer daaw – te kaaraange gi mënoon naa oyofal jeexital yi.
En effet, l’Afrique Sub-Saharienne, du fait notamment de l’importance de son activité agricole, se trouve particulièrement exposée – en témoignent les invasions de criquets pèlerins l’an passé – et l’assurance pourrait être un moyen efficace d’atténuation des impacts.,
galsenai/french-wolof-translation
Bul ragal wax ko ci kumpa.
N'aie pas peur et dis-le en toute confidentialité.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaye lii mooy lima gëna neex.
Mais c'est mon préféré.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Judith, duggal ci oto bi!
- Merde, monte dans la voiture, Judith!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
"Yaakaarna ne xalaat bu rafet la.
Selon les intervenants des refuges, afin de traiter plus rapidement le cas des enfants, les autorités ont instauré de nouvelles règles qui imposeront à certains d’entre eux de comparaître devant le tribunal dans le mois suivant leur détention, plutôt qu’après 60 jours, ce qui était la norme auparavant.
galsenai/french-wolof-translation
Kon jox ko kaaraange, du man.
Alors donne lui la sécurité, pas moi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lu daw yaram la amoon benn fetal ci otoroute bi, ñatti blok ci sunu kër.
C'est dommage qu'il y ait eu une fusillade sur l'autoroute à trois pâtés de maisons de chez nous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mu nekkoon moom kese te kenn ñemetul a wax ak moom.
Il était seul, et personne n'osait lui parler.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
..ki waral bomb yi di kalaate ci Inde.
..qui a causé les explosions en Inde.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Donte benn yoon la sax, yaakaar naa ne war nañu koo delloo njukkal.
Pour une fois, je pense qu’il faut lui rendre hommage .
galsenai/french-wolof-translation
Mbëggeel gi bariwul ludul wër.
Il n'y a pas d'amour à partager.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kublai Khan amoon na alal ci Beijing.
Kublai Khan avait une fortune à Pékin.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaye, loolu lu jafe la.
C'est compliqué.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amuma benn njariñ ci yaw, Sita.
Je n'ai plus besoin de toi, Sita.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi fàttaliku lépp.
Je me souviens de tout.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Tour yooyu tabax bànk lañu woon, mbedd mi ñu nekkoon ñu xamee ko ci la Milla de Oro, wala Golden Mile
Ces tours étaient des bâtiments de banque, et la rue où elles se trouvent est devenue connue sous le nom de la Milla de Oro, ou le mille d'or.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amaana mingi màndi ba leegi ci guddi gi weesu.
Il est probablement encore bourré depuis hier soir.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Liggéeyu jaam bii nga am, mën nga wàññi bépp kontraktër ci dëkk bi?
- Ce bassin de main-d'œuvre esclave que vous avez, vous pouvez sous-enchérir n'importe quel entrepreneur en ville?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mënuñu woon déggoo ci kan moo wara liggéey ci tool wëtteen wi ak kan moo wara fomp dër bi.
Ils ne s'entendaient pas sur qui devait travailler dans le champ de coton et qui devait balayer le sol.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nit ñi ko jox kaka.
Des gens qui lui ont donné des conneries.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaw, amnaa jafe-jafe bu ndaw...
Oui, j'ai un petit problème...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bu jaxasoo bi di am, géej gi dafay leer lu wert.
Pendant la confusion, la mer émet peu à peu une lueur verte.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Tay mooy dose bu mujj ci pikiir boobu.
Aujourd'hui est la dernière dose de cette injection.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lumu mëna doon, yenn baayima yi, rawatina bëy yi, dañuy faral di daw seen bopp
Mais en tout cas, certains animaux, surtout les chèvres, ont tendance à courir librement tout le temps.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
..buñu siñe sunu palaŋ. Sëñ bi, sudee siñe nañu sa palaŋ.
Si votre plan est signé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Su ñu sukkandikoo ci L’As ñiy saytul nguur gi seeni liggéey tuxu nañu ci seen béréb yu yees tàq yi.
D'après le quotidien L'As, l'Inspection générale d'État (Ige) vient d'y aménager dans des locaux flambants neufs.
galsenai/french-wolof-translation
-Taggoo, jigéen ñi.
- À bientôt, les filles.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Charles Lane dafa jaay gaal
Charles Lane a vendu des navires
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nit ñu bari ñu ngi joge Midwest ak Canada.
Beaucoup de gens arrivent du Midwest et du Canada.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Maa ngi jël sama ordinatër.
- Je vais chercher mon ordinateur.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndax dunu defaat lii?
On peut ne plus faire ça?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xaste ak ñaawal doŋŋ lañu am, moone Usmaan Sónko laaj na leen ay laaj yu ñu tontoogul ba tey.
Le dénigrement et la diabolisation constituent ainsi les seuls arguments dont ils disposent face aux interpellations d’Ousmane SONKO.
galsenai/french-wolof-translation
doon na sëqët lu bari, dee-deelu ngir mucc ci gile gàcce.
elle tousserait énormément et ferait semblant de mourir pour échapper au ridicule.
galsenai/french-wolof-translation
Ci ati 1870, réew mi dafa doon jànkoonte ak jafe-jafe.
Dans les années 1870, le pays était en ébullition.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
DU CI SUUF.
Pas sur le sol.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Baax itam.
Des bonnes aussi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ah!... Kon kenn nekkul ci Àdduna?
Ah !… Il n’y a donc personne sur la Terre ?
galsenai/french-wolof-translation
Kon, ci alarba yi.
Seulement le mercredi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Jërëjëf, Alex.
Merci, Alex. Je suis désolée.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bàyyi sunu nature yu lëndëm yi.
Renoncer à notre nature sombre.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Loolu dafay tekki ni dangay dugg ci àdduna kwantum.
Cela signifie que vous entrerez dans un royaume quantique.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Demal ak mbiri aerobic ndax dama soxla cardio
Continuez avec l'aérobic, j' ai besoin de cardio.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yeneen xeltukat yi wax nanu ne garab yii dañoo bare tooke kon ci yoon benn dinosoor lekku ci, doonte tey abbu àll buy dox melni ku tàyyel ak yeneen xeeti rab yu melni seku(sëtu dinosoor yi) mën na lekk xob wal doom yu am tooke yi.
D’autres scientifiques affirment que ces plantes sont très toxiques, il est donc peu probable qu’un dinosaure les ait mangées, même si aujourd’hui, le paresseux et d’autres animaux comme le perroquet (un descendant des dinosaures) peuvent manger des feuilles ou des fruits toxiques.
galsenai/french-wolof-translation
Soxla nga dawal?
Tu veux que je te dépose?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Keneen mooy fay faktiir bi.
Quelqu'un d'autre paie la note.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Namm naala lool.
Tu m'as vraiment manqué.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yelloowul ñu jéggalu, bëgg naala.
Il ne mérite pas d'être désolé, je t'aime.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Jaar-jaar bu gudd la.
C'est une longue histoire.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaye fàww nu tàmbali def mbir yuy indi jafe-jafe ci defkatu ñaawtéef yooyu.
Mais nous devons commencer à faire des choses qui auront un impact direct sur ces délinquants.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Hypnose mooy jumtukaay bi gëna baax.
L'hypnose est l'outil parfait.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dafa wara yàqu.
Elle doit être corrodée.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Emili.
Je suis Emily.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndijaay, nanu dugg ci sama oto.
Viens oncle, allons dans ma voiture.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Jërëjëf, gaawal.
- Merci, et dépêchez-vous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaw sama buur...
Oui mon roi...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mbaam xuux?
Espèce de connard?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Gis nanu ni Foster Care System barab la bu am kaaraange ci xalé yii.
Nous percevons le système de placement familial comme une zone de sécurité pour ces enfants.
galsenai/french-wolof-translation
Ki gëna xéewale.
Le moins cher.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xale bi!
Nom de Dieu!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Déedet, Harley.
- Je ne peux pas.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lu ci bare, dafay faral di seetlu ne nit ñi amuñu benn yég-yég ci jafe-jafey wér-gu-yarami joŋantekat yi ci seen wàllu xel. Te saa su yu laaj ak tontu doxee suñu diggante ak ñoom ma seetlu ko.
J'ai souvent eu l'impression que les personnes n'ont aucune considération pour la santé mentale des athlètes et je le vois à chaque fois que je participe à ces questions-réponses.
galsenai/french-wolof-translation
Diine ji gëna mag ci Moldavie chrétien orthodoxe bi.
La principale religion en Moldavie est le christianisme orthodoxe.
galsenai/french-wolof-translation
ñeenteelu weeru sulet.
Le 4 juillet.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xam nga, maa ngi xalaat lan la rak Bob di def su amee wideo boobu?
Je me demande ce que frère Bob ferait s'il avait cette vidéo.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yaw kese nga ko xam.
Vous seul le savez.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
CARLS. ;
Le président
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yegg nga ci sama telefon.
Vous avez atteint mon téléphone.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
-Mooy gént bi gëna tiis.
- C'était un rêve horrible.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- ( di onku )
- Je suis désolé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Juroomi simili, kilifa.
Dans cinq minutes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Woowal xeetu lëndëm gi nga nëbb ci suufu xeer wi.
Faites sortir cette bande de loups que vous avez cachée sous la falaise.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndax def naa 15 at di doxal barab bii wala yaw?
J'ai passé 15 ans à diriger cet endroit ou toi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Alexander dañu ko weñ loxo mu genni ci njëkkante bi ginaaw bi nataali lonetam yi siiw lool.
M. Alexander a été forcé de se retirer de la compétition après que des photos de ses lunettes soient devenues virales.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Moanin 'low, sama nit ku baax ki dina dem, su demee oh Lordy
Mon petit homme va pleurer, quand il pleurera, oh mon Dieu
bilalfaye/english-wolof-french-translation